Yaay sama àdduna, oh, yeah
Sama baby coco waay, ey yeah
Yaw yaay sama àljanna
My love!
Sama baby coco waay, hmm yeah
Baby yaay man
Tëddal nelaw xam ni munuñu dara
I don't give a fuck, merkat fajul dara
Takkal la or ba ci 24 carats
Dañ leen di bàyyeek përëm bi ñoom ñuy dékke aya
Baby, I just want a real love
Real love, I just wanna know a real love
Definitely I don't want lie
I'm in love with you
In the morning, in the night, oh, yeah
I'm in love with you
In the morning, in the night, oh, yeah
Yaay sama àdduna, oh, yeah
Sama baby coco waay, ey yeah
Yaw yaay sama àljanna
My love!
Sama baby coco waay, hmm yeah
Waay waay waay waay
Mer bi fajul dara
Moom fajul dara
Kon fajul dara
Bàyyi leen te ñëw ma takkal la or 24 carats
Wurus 24 carats
Ngalam 24 carats
Xanaa du ma la yénne
Ma vie, ma vie
Baby yaay man
Tëddal nelaw xam ni munuñu dara
I don't give a fuck, merkat fajul dara
Takkal la or ba ci 24 carats
Dañ leen di bàyyeek përëm bi ñoom ñuy dékke aya
Baby, I just want a real love
Real love, I just wanna know a real love
Definitely I don't want lie
I'm in love with you
In the morning, in the night, oh, yeah
I'm in love with you
In the morning, in the night, oh, yeah
Yaay sama àdduna, oh, yeah
Sama baby coco waay, ey yeah
Yaw yaay sama àljanna
My love!
Sama baby coco waay, hmm yeah
Waay waay waay waay
Mer bi fajul dara
Moom fajul dara
Kon fajul dara
Bàyyi leen te ñëw ma takkal la or 24 carats
Wurus 24 carats
Ngalam 24 carats