Dougg nga sama keur diakhassé ko
Lepp lignou fassone nga ba ko
Dou sakh dama saagan, damala nob
Sama xol bi, ma diokh la
Takhaw thi say beugg beugg
Say caprices meu encaisser, damala no-bone
Mon amour pour toi m'a aveuglé
J'étais vraiment dans mon monde
Perdu dans les eaux et forêts
J'ai aussi perdu toutes mes ondes
Nima ko guénté wone
Ak nimou démé nii
Comme Yalla'k yaali bébé
Fima la féété wone
Ak ning ma fayé nii
Beuss boula djigué béét ma
Togn ngama way
Béét ngama way
Gaagn ngama way
Yaakh nga sama xol
Gneupp gnima bayi wone nguir yow
Naka la lén di kholé
Naka laniou may kholé
Lepp limala dane miimeul
Teng ko daan def gneulé
Tey mane nga thiy boolé
Ndéké sa tiél dou sa yarou
Dama gueuleum ba téél la juger
Ndéké sa tiél dou sa yarou
Fimné nila nekh ngay yeungo lady
Nima ko guénté wone
Ak nimou démé nii
Comme Yalla'k yaali bébé
Fima la féété wone
Ak ning ma fayé nii
Beuss boula djigué béét ma
Togn ngama way
Béét ngama way
Gaagn ngama way
Yaakh nga sama xol
Sonnal ngama
Gaathiél ngama
Sou démb done tey
Dougnou meusseu khamé
Nima ko guénté wone
Ak nimou démé nii
Comme Yalla'k yaali bébé
Fima la féété wone
Ak ning ma fayé nii
Beuss boula djigué béét ma
Nima ko guénté wone
Ak nimou démé nii
Comme Yalla'k yaali bébé
Fima la féété wone
Ak ning ma fayé nii
Beuss boula djigué béét ma
Togn ngama way
Béét ngama way
Gaagn ngama way
Yaakh nga sama xol