Inicio Top Música Bad Bunny Música Cristiana Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA

Letra de 'Mon Choix' de Wally B. Seck - Escucha y canta en New Musica

Varios-artistas

Relaxar e Dormir

Varios-artistas

Top Hits 2004

Varios-artistas

Top Hits 2005

Varios-artistas

Poperreo

Artist profile picture

Mon Choix

Wally B. Seck

Canciones

Sama baby sokhna-la dou guél thi mane
Té mbeuguélam meun nama, louma thi meun
Sama baby sokhna-la dou guél thi mane
Té mbeuguélam meun nama, louma thi meun

You're my baby, sokhna nga do guél thi mane
Mbeuguélam louma thi meun
That's my baby
Sokhna-ci do guél thi mane
Mbeuguélam louma thi meun

Sama doundou gui dakh na lém
Tégalma Kim Ka, no no douma dém
No matter what they say, me no follow them
Loma meunti fay non mane douma dém

Sou méré ma diaay maana, monté gueuna louma
Eh! Sou méré loma tégal beugouma

Xalé bilé, sita questà, diéguéma gnou fiesta
Diarna ma photo la all night poste ko Insta
Mamacita c'est ça banana ananas
Diarna ma photo la all night poste ko Insta

Xalé bi amnaa faiblaissam, lii lanla
Sou féké naturelloul mysthique la, dogali-ma

Sama baby sokhna-la dou guél thi mane
Té mbeuguélam meun nama, louma thi meun
Sama baby sokhna-la dou guél thi mane
Té mbeuguélam meun nama, louma thi meun

You're my baby, sokhna nga do guél thi mane
Mbeuguélam louma thi meun
You're my baby
Sokhna-ci do guél thi mane
Mbeuguélam louma thi meun

Baby baby, baby baby
I love you so much you got my mercy
Baby baby, baby baby
I love you so much you got my mercy

Niawou ma, sofou ma
Bour yalla mako téraléé
Sama mbeuguel-gui nimma lééré
Sama chérie sita questà, diéguéma gnou fiesta