Inicio Top Música Bad Bunny Música Cristiana Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA

Letra de 'Feeling Pacc (feat. Astar)' de Sidy Diop - Escucha y canta en New Musicas

Varios-artistas

Super Sad

Varios-artistas

Previa Y Cachengue 2022

Varios-artistas

Sport Motivation

Varios-artistas

Reggaeton Clasicos

Artist profile picture

Feeling Pacc (feat. Astar)

Sidy Diop

Canciones

May ma daqaar ma lay bisaab
Tu veux qu'on fasse du sale
Dekkoon saxar chicha
Sécha toyul maa lay wisa
Ma toog ci luñu doon wër droits de ass
Dafa leer dangeen passe ba mel ni ass

Xalileen yoon bi ma ñëw
Li ngeen jolle ci man
Bon di dëgër teksi bëri doole di tan
Nu ñuy joppe du benn, ma yore yat biy duma
Féete ci kaw jarul laaje ndax xale baa ngi ni

Feeling pacc
Money pacc
Sourire pacc
Choco pacc
Mignon pacc
Galanterie pacc
Jarul wëri feneen ndax xale baa ngi ni

Feeling pacc
Jongé pacc
Sourire pacc
Jekkete pacc
Doxin pacc
Jekk taaru pacc
Jarul wëri keneen ndax xale baa ngi ni

Waaw jongé waawaaw
Huuuu waawaw
Ah ahhhh

Kan mooy dérangé (dérangé)
Pourquoi ma lay dérangé (hummm)
Dama leen yërëm di leen arrangé (hey bei!)
Waaye ku mënul muñal dérangéwu (lala lalala)

I'm so fresh metti nii
Di gagner fu ne
Dooley Francis Ngannou
Docteur may faje
Li ma ci denj du jeex
Ñaan ma ci njekk
Maa may la tuuti ni
Mais fooy xëcco danga nara ñakk

Feeling pacc
Money pacc
Sourire pacc
Choco pacc
Mignon pacc
Galanterie pacc
Jarul wëri feneen ndax xale baa ngi ni

Feeling pacc
Jongé pacc
Sourire pacc
Jekkete pacc
Doxin pacc
Jekk taaru pacc
Jarul wëri keneen ndax xale baa ngi ni

Wëral, wëral!

Xaritoo lak man
Man feeling pacc la ciy amee
Ñaan ma ma may la
Moo lay jamal
Ma tokk may basse

Ah ahh

Feeling pacc
Money pacc
Sourire pacc
Choco pacc
Mignon pacc
Galanterie pacc
Jarul wëri feneen ndax xale baa ngi ni

Feeling pacc
Jongé pacc
Sourire pacc
Jekkete pacc
Doxin pacc
Jekk taaru pacc
Jarul wëri keneen ndax xale baa ngi ni

Wëral wëral!

Inicio Top Música Bad Bunny Música Cristiana Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA