Inicio Top Música Bad Bunny Música Cristiana Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA

Letra de 'Ça me va (feat. Akhlou Brick)' de Sidy Diop - Escucha y canta en New Musicas

Varios-artistas

Electronic Hits

Varios-artistas

Baladas Y Rock En Ingles De Los 70s 80s 90s

Varios-artistas

Esenciales Pop en Espanol

Varios-artistas

Top Hits 2018

Artist profile picture

Ça me va (feat. Akhlou Brick)

Sidy Diop

Canciones

Daa am lu ne ci man
Te newul ci ñoom
Damay dégager
Balle bi dal ci ñoom
Ñun xale pare finance
Sport squat gainage
Lii dama koo judduwaale
Noppileen silence
Ma taxaw sama seetu

Yaw ni nga mel loo ci yokk yàq ko
Sa beauté naturelle, artificielle dàqu ko
Yaw ni nga taaroo ëpp na ci ay loxo
Boo soloo gën a jekk, chirurgie jaru ko

Aah
Ni nga mel hmm
Ni nga mel aah
(Ni nga mel, ni nga mel
Yaw xale bi ni nga mel hmm)
Ni nga mel

Yaw tourneel 360
Défiler dox temp ndànk
Xale bi mbaa laal nga bant
Xanaa sa bàjjen a la dàmp
Ay waay!
Sa loxo a ngi ci sauce
Li ñale di wuti ba di ko ci yokk, yaw danga ci toog
Mais kepp ko foofu naturelle
Man dama la bëgg ci ni nga mel
Dawalal, piloteel
Dóor ma ci bopp sa yatu kel
Ooh tu es belle
Sa latéral ay titulaire
Sa axe ne balle bi du dugg camp
Artificiel walla naturel
Non lii mooy travail de mama

Yaw ni nga mel loo ci yokk yàq ko
Sa beauté naturelle, artificielle dàqu ko
Yaw ni nga taaroo ëpp na ci ay loxo
Boo soloo gën a jekk, chirurgie jaru ko

Aah
Ni nga mel hmm
Ni nga mel aah
(Ni nga mel, ni nga mel
Yaw xale bi ni nga mel hmm)
Ni nga mel
Ni nga mel

Ni nga mel, ni nga mel
Xale bi ni nga mel
Aah

Daa am lu ne ci man
Te newul ci ñoom
Damay dégager
Balle bi dal ci ñoom
Xale pare finance
Sport squat gainage
Lii dama koo judduwaale
Noppileen silence
Ma taxaw sama seetu

Naan kii kan la
Mu naan kii man la
Travail mama (man a)
Fayuma nada
Xale bu rafet bii kan la (man a)
Kii man la
Travail mama
Fayuma nada

Yaw ni nga mel loo ci yokk yàq ko
Sa beauté naturelle, artificielle dàqu ko
Yaw ni nga taaroo ëpp na ci ay loxo
Boo soloo gën a jekk, chirurgie jaru ko

Aah
Ni nga mel hmm
Ni nga mel aah
(Ni nga mel, ni nga mel
Yaw xale bi ni nga mel hmm)
Ni nga mel
Ni nga mel

Aay
Bëgg naa ko naturelle
Lu mu sol mu fees dell
Bu doxee daagu waay
Day dalal sama xel
Yaw ni nga mel
Jekk taaru naturelle
Heure boo génnee bélliwaat
Xale bi ni nga mel

Ça me va, ça me va, ça me va
Ca dëgg dëgg
Baby ni nga mel, ça me va

Ça me va, ça me va
Ca dëgg dëgg daal
Nii nga mel, ça me va

Ça me va, ça me va
Ça me va va-va-va-va
Ça me va

Ça me va, ça me va
Ça me va va-va-va

Ca dëgg dëgg
Baby ni nga mel, ça me va

Ni nga mel
Ça me va, ça me va
Ça me va va-va-va

Ca dëgg dëgg
Baby girl
Ni nga mel, ça me va

Inicio Top Música Bad Bunny Música Cristiana Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA