Inicio Top Música Bad Bunny Música Cristiana Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA

Letra de 'Ndongo' de Samba Peuzzi - Escucha y canta en New Musicas

Varios-artistas

Pop Party

Varios-artistas

Es Hora De Dormir

Varios-artistas

Caliente

Varios-artistas

Lo fi Para Estudiar

Artist profile picture

Ndongo

Samba Peuzzi

Canciones

Eh!
Aayaaa
Sénégal boy
Yeah

Balle ba ngi sogo takk
Ghetto sama ginnaaw
Man rekk man kese fi tekk tank
Xaalis du doy, jàmm du ëpp
Tour ba ngi dem succès di yokk
Listen piis fëri ñun duñ la fàtte
Derétu diamaguene mo fi daw
Dérek moo may tere te game bi
Iyo, iyo

Ni may rabe lu si sa yoon
Bandit dëgg de koy nuróó
Xam naa ni si man ngay xool
Mais non non ni nga koy defe du noonu
Dem laalal de, sa show man la barde
Ay caché millions sans projet
Man la Sénégal boy from jekk (hey)

Non non coow li du bari
Man ngeen tekk seen bët yi
Te ñaan waajur moo tax ma yeksi fi, waa eh

Ñoom lu ñu fokk?
Munuñu bokk
Xiir bi la yorr
Ñuy daw malen koy nokk
Ey mangek buzzu ndongo
Dama xew, ey
Boo ma xamul
Demal nga tokk
Eh, demal nga tokk
Demal nga tokk
Eh boo ma xamul bu yaa demal nga tokk
Demal nga tokk

Pic bi ñu ma sànni man dama ko toul
Ñoo ma ci jittu ma leen raw fuuf
Ne leen yolé xajjatul ci poche
Niak sipp wessouwoul andak kou matoul
Xaliss la Xèkhè douma khoulo
Kholéma Ndongo Lô bir Ghetto
Musiku fi lay toukilo
International Nekké ci yone
Mashallah!

Poche Bangui fess may fékh
Na mère bi bégg
Bu ñu sañoon kenn du ma deug
Léegi ñoom ño may xeex
Nangu demb bëgg bañ tey
Sissouman yi demelen bayi ci birr
Kode sama xol def xeuthie
Éclate kanam bi xol Guedj
Eh!

Non non coow li du bari
Man ngeen tekk seen bët yi
Te ñaan waajur moo tax ma yeksi fi, waa eh

Ñoom lu ñu fokk?
Munuñu bokk
Xir bi la yorr
Ñuy daw malen koy nokk
Ey mangek buzzou Ndongo
Dama xew, ey
Boo ma xamul
Demal nga tokk
Eh, démal nga tokk
Démal nga tokk
Eh boo ma xamul bu yaa dèmal nga tok

Inicio Top Música Bad Bunny Música Cristiana Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA