Chérie kitoko, chérie kitoko!
Chérie my woman, woman wom!
Chérie my woman, woman wom!
Chérie gisoo du ci yaw ma juum!
What’s up what’sapa in your room!
Chérie nuyuma bul ma romb!
Chérie wuyuma bul ma romb!
Feccal ma rumba rumba rum!
What’s up what’sapa in your room!
Chérie kitoko
I don’t like the way you give me your love
Chérie kitoko
I don’t like the way you give me your love
Chérie kitoko
I don’t like the way you give me your love oh
Chérie kitoko
I don’t like the way you give me your love
Jaaral nga ma do anything
Bu nekkee asaman ci nga bëgg ma ànd la ko way!
Ma chérie bul jooy
Xam na ni man ma la tooñ yeah
Xool ma sama xol tooy
Foo yéndoo de fa lay fanaan
Soxna si bul jooy
Je t’aimerai comme d’hab, bébé j’ai les contacts
Kaay ñu ànd fu dugg ma dugg, gudd comme Jack!
Kaay ñu jeu de contact, Wiri Wiri comme d’hab
Foo féetee ma feuleu, fatal ma foofu may fatt!
Enh, fi mbëggéel bu dëgg day àndaki coono gi yépp enh
Man lu tax ma sonal la, sonal naa mboolo mi yépp enh
Chérie my woman, woman wom!
Chérie my woman, woman wom!
Chérie gisoo du ci yaw ma juum!
What’s up what’sapa in your room!
Chérie nuyuma bul ma romb!
Chérie wuyuma bul ma romb!
Feccal ma rumba rumba rum!
What’s up what’sapa in your room!
Chérie kitoko
I don’t like the way you give me your love
Chérie kitoko
I don’t like the way you give me your love
Chérie kitoko
I don’t like the way you give me your love oh
Chérie kitoko
I don’t like the way you give me your love
Won naa la woo ma ñu ànd rekk séy
Bu la neexee nga woo mami
Li may def ni yépp wollay du lépp la tay
Boo ma weddee nga xol tani (petaw)
Na honey A Fammi
Every day time is money
Will never waste time my honey
Li ma mbedd jàngaloon du loolu la miin
Dinaan ko dóor dinaan ko saaga
Naan dianni door ci mbam yi, diin ko caga
Li jarul góor, góor jarul nada
Léegi doon na ndongo wax faada