Inicio Top Música Bad Bunny Música Cristiana Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA

Letra de 'Eutou Baabel' de AMADEUS - Escucha y canta en New Musicas

Varios-artistas

Top Hits 2003

Varios-artistas

Women of Latin Music

Varios-artistas

Top Hits 1979

Varios-artistas

Folclor Peruano

Artist profile picture

Eutou Baabel

AMADEUS

Canciones

Maak yaw ba abadan
Jox naa la sama kàttan
Jaayaanteek sama ndaw
Dem naa ba ndox ci baat
Jox naa la sama kàddu
Mënatuma la baal

Te sèntu naa ci jële ndam maak yaw
Ndax àddunya bi dafay feexe ba ma xàddi
Duma bàyyi li ma tàmbali man
Fàttaliku naa sama maam
Ne na ma fori jëlal jaaro gi

Dégg naa ñu lay wutal mas te doo moroom jigéen
Xam naa dinañu ma laaj lan moo tax ma wax lile
Kenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
Kenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la

Demanoon de nañu
Defando nañu ay mbir
Xamal nga ma lu ne
Soo ma yoolee
Dootuma jar dara
Bi ma ñépp umpale
Yaw yaa ko xam
Sama waay nga

Ku mel ni yaw
Ku ka amul da koy iñaane
Ku mel ni yaw
Ëtu baabel ñoo lay laaj
Ku mel ni yaw
Thiam Baabel Demba Thiam, eh
Ku mel ni yaw
Ëtu baabel yaw lay laaj

Naa la yóbbu ëtub baabel
Boole la ak samay nawle yi
Xam nga tàkkusaanu baabel
Thiam boroom ndendi was nga fay fowee

Yaw
Mësuloo ma xépp ci samay ay ayib
Sama njuumte yi mësoo ko nettali
Xam nga jaambaar amul
Ku ñu dimbale am
Ku sañoon day baax
Comme doomu ñay
Bu ma ñaanal ponkal
Man soo ma dundee baax