Yaa di sama waay
Maa di tam sa waay
Ñaanuma la tooñ
Su amee Yàlla nga ma baal
Yaa di sama waay
Maa di tam sa waay
Ñaanuma la tooñ
Waaye su amee Yàlla nga ma baal
Ne ma li lay bañ
Wax ma ni nga ko bëgge
Jom ji laay rang
Ñëkkewu ma waaye ma lay mujje
Ngelemu jëg bu juróom
Su ma ko amoon may na ma la yeah
Ñu jél ko jéebal laa ko
Dama bëgg lool yéey na ma yeah
Àdduna du mës a neex ba ma fàtte la
Dieye Sélémane
Ngelemu jëg bu juróom
Su ma ko amoon may na ma la yeah
Dieye Sélémane laay way
Céy Dieye Sélémane laay way
Dieye Sélémane laay way
Céy Dieye Sélémane laay way
Dëkk ba nga ma jële
Sori naa lool
Diggante yi nga ma fekkoon tam
Metti na woon
Li may mën wëy yépp soo ko wonewul woon
Kon leneen laay doon
Kon yoon la délloo la ñuukal eh
Dieye Sélémane
Massamba raar a Dieye
Yirim diir na buur
Daour Ndumbe Ndela Dieye
Dieye Sélémane
Massamba raar a Dieye
Yirim diir na buur
Daour Ndumbe Ndela Dieye
Dieye Sélémane
Dieye Massamba
Dieye Sélémane
Massamba moo ni
Duma dem Sine duma dem Saloum
Te ku ma tee sol buur man sa kaw laay jaar
Dieye Massamba
Ngelemu jëg bu juróom
Su ma ko amoon may na ma la yeah
Ñu jél ko jéebal laa ko
Dama bëgg lool yéey na ma yeah
Àdduna du mës a neex ba ma fàtte la
Dieye Sélémane
Ngelemu jëg bu juróom
Su ma ko amoon may na ma la yeah
Dieye Sélémane laay way
Céy Dieye Sélémane laay way
Dieye Sélémane laay way
Céy Dieye Sélémane laay way