Tool sunu ndaw
Buntu àdduna nekk ci yoonu ndam
Daane doole xam ni
Dañu wara ame
Beey sunu wéwou tank
Moy fu lak fayda
Gëm sunu bopp lay doreé
Si tax yii ak kaw ga
Juk jëf jot na
Liggéey des sunu reew
Ak sunu ngor lañ soxla
Lu ñuy dem wuteji bitim-réew ñaqu fi
Bugnsi jublu a ki pexee am ko fi
Bul na ngi fa
Bala nga nakhhsayy
Toggal ci réew mi
Tekk fii waalaahi
Gëm na nii mën na tekki fii
Liggéey tedd fii
Mën na tekk fi
Gualla baay togaal
Ci dëkk bi (mën na tekk fi)
Hey ñu njariñ dëkk bi
(Mën na tekk fi hey)
Gëm sa bopp xool ci say mbokk
Moytandiku di wokk sa dook
As góor du fàtte
Ngor fu la ak fayda ci la bokk
Alal lay faj gàcc bànneex fajul naqar
Mëna wër mayewul wërsëg
Ku ne juddook sa wërsëg billaay
Wax ju werr laa la wax
Toggal ci réew mi bul dem feene
Napp Sama Beey dunde
Lépp agi dox ci réew mi
Bu ñu cuune waawaaw
Wax ju weer laa la wax
Toggal ci réew mi wuute métier
Napp Sama Beey dunde
Leppagui dox ci réew mi
Bu ñu cuune waawaaw
Bul na ngi fa
Bala nga nakhhsayy
Toggal ci réew mi
Tekk fii waalaahi
Gëm na nii mën na tekki fii
Liggéey tedd fii
Mën na tekk fi
Gualla baay togaal
Ci dëkk bi (mën na tekk fi)
Hey ñu njariñ dëkk bi
(Mën na tekk fi hey)
Souf si sougnou souufff la
Nagne djiiw dina mégnii
Diourr donguaa laa
Took fi garab gi sunu mbeey la
Toole yii lossi def mu faylaa
Ndax coono du saay kon juge
Réew mi ñoo ko mëna defar ba mu naat
Siggil suñu Sénégal
Bul na ngi fa
Bala nga nakhhsayy
Toggal ci réew mi
Tekk fii waalaahi
Gëm na nii mën na tekki fii
Liggéey tedd fii
Mën na tekk fi
Gualla baay togaal
Ci dëkk bi (mën na tekk fi)
Hey ñu njariñ dëkk bi
(Mën na tekk fi hey)
Boul nangui faa
Bala gua nahkksayy
Toggal ci réew mi
Tekk fii waalaahi
Bul nangui faa
Bala nga nakksayy
Toggal ci réew mi tekk fii waalaahi
Toggal ci dëkk bi
Ñu di rigne dëkk bi
Ndax ñun gune dëkk bi
Ñoo wara defar dëkk bi
Toggal ci dëkk bi
Njariñ ame na ci dëkk bi
Toggal ci dëkk bi
Ndimbal ame na ci dëkk bi
Gëm sa gox
Sokkoli sa gox
Gëm sa bopp
Ñakk jariñu
Gëm sa gox
Sokkoli sa gox
Gëm sa bopp
Ñakk jariñu
Gëm sa gox
Sokkoli sa gox
Gëm sa bopp
Ñakk jariñu