Inicio Top Música Bad Bunny Música Cristiana Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA

Letra de 'Daf Niou Bett' de Maabo - Escucha y canta en New Musicas

Varios-artistas

Women of Pop

Varios-artistas

Rancheras Inolvidables

Varios-artistas

Musica sin copyright para directos

Varios-artistas

Evening Chill

Artist profile picture

Daf Niou Bett

Maabo

Canciones

Yàgoon naa foog nii
Soxlawuma kudul man mii
Man kenn lawoon ci yoon wii
Dox di dem ak sama yan wii
Bes bi ma la gisee
Keroog dafa leer ci ñun ñaar
Sunu xol yi ni ñu dajee
Ci laa xam ni yaw laa doon xaar
Yaa Yaa Yaa Yaa
Yaa tax may wër
Fi mbegte ne ngir indil la
Yaa Yaa Yaa Yaa
Foog ma siggil la

Sama jàmm yaw la
(Yaa tax ma xam ni mbëgeel neexe)
Suma beggee yaa tax
(Mossuma foog nii)
Sama jàmm yaw la
(Nit dinama toll fii)
Suma beggee yaa tax
Lii daf niou bett maag yaw!

Ci mbegte nga may dello (dello)
Dima dëfal may ree
Awma beneen héros
Man yaa may begal saa su nekk

Mbëgeel dina yegsi fing kodul fooge
Këf sa xol di fowee
Yaw laa sopp te yaw laa nob
Yaa leen gën fopp, do ñaar yaw!
Jikko yi nga soppi ci man nimu bariwee
Jubbanti yi bonn, defma gòoru qualité
Yama yokk jom, kon nak
Nala keral, dila beggal ndax loolu laa digge
Cofeel ci biir xolu nit
Amul njariñ sula yobbuwul ciy ngëneel
Dalal nga ma dotuma tiit
Yaw dara melul ni sa mbëgeel

(Sama jàmm yaw la)
Yaa tax ma xam ni mbëgeel neexe
(Suma beggee yaa tax)
Mossuma foog nii
(Sama jàmm yaw la)
Nit dinama toll fii
(Suma beggee yaa tax)
Lii daf niou bett maag yaw!

Ci mbegte nga may dello
Dima dëfal may ree
Awma beneen héros
Man yaa may begal saa su nekk

Saa su nekk

Inicio Top Música Bad Bunny Música Cristiana Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA