Inicio Top Música Bad Bunny Música Cristiana Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA

Letra de 'Thies' de Jeeba - Escucha y canta en New Musicas

Varios-artistas

90s Pop Rock

Varios-artistas

SAYAS CAPORALES

Varios-artistas

Sunny Bossa Nova

Varios-artistas

All Out 80s 90s Hits

Artist profile picture

Thies

Jeeba

Canciones

Succès bu ne xanaa xamoo waxtu laay xaar
Boroom xam-xam yi junj nan ko doy na waar
Tay magg nan xamee bu baax
Flambeau bi ñoo ko yor su baxee ñun la baaxal
Su bone it ñun la boonal

Cees maa ko moom, yaa ko moom
Ñoo koo moom, ñu dëggel baat bi jëm ci kaaw
Doo daw mu ku xam na ni gaynde nga
Dëkku bañ kat benn la ci Senegaal
Dëkku ngoon Latyr ak Seck signature
Sanex moo tax ñu neex

Ñu soxla wuññ jega ni rooyukay
Fees fi deel tax ñu kaay ndaamo waawaaw
Dëkk bañ kat benn la ci Senegaal
Cees kay rekk ci xol dara du ko faay
Ku weedi laaj leen ma liim ma faay

Eh waaw, waawaaw waaw
Cees sama dëkk la, man maa ko moom
Eh waaw, waawaaw waaw
Cees suñu dëkk la ñun ñoo ko moom
Setsi ma gaaw ma wone la way!
Wone la lu dul gis ci benn reew
Fi àjjana la, non y'a pas photo
Jengu man la kon nañu ko toppatoo

Ku ne saañ nga wax ni fi nga dëkk moom moo la neex
Ku ne saañ àapo ni fi nga dëkk ne moola neex
Ku ne saañ nga wax ni fi nga dëkk moom moo neex
Cees kaay moo ma neex, man moo ma neex

Eh moo ñu neex, Cees kaay yow moo ñu neex
Yóbbu ma yóbbu ma
Kër maam al hajj
Ziare Ahmed Barro njegeen
Jar jamagene, Ziar suñu maam Abdou Aziz
Aidara dem Medina Fall Penc Baye Fall Yaa
Cheikh Ndiguel Fall
Meissa Bigue Coumba Fall Dabaay
Khabrou Abdoulaye Yakhine
Sama maam Amadou Lamine Ba
Duñu fàtte wa jangu bi
Cees kaay mooy sama reew

Eh waaw, waawaaw waaw
Cees sama dëkk la, man maa ko moom
Eh waaw, waawaaw waaw
Sunu dëkk la ñun ñoo ko moom
Setsi ma gaaw ma wone la way!
Wone la lu dul gis ci benn reew
Fi àjjana la, non y'a pas photo
Jengu man la kon nañ ko toppatoo

Ñu soxla wuññ jega ni rooyukay
Fees fi deel tax ñu kaay ndaamo waawaaw
Dëkk bañ kat benn la ci Senegaal
Cees kay rekk ci xol dara du ko faay
Ku weedi laaj leen liim ma faay

Eeeh eh eh eh
Yóbbuma Mbour Guedj
Mbour soose, mbuur kankuran aah
Damay ñëw gaaw yaay
Eeh eeh, Cees kaay
Hun hun Cees kaay

Ñu soxla wuññ jega ni rooyukay
Fees fi deel tax ñu kaay ndaamo waawaaw
Dëkk bañ kat benn la ci Senegaal
Cees kay rekk ci xol dara du ko faay
Ku weedi laaj leen liim ma faay

Inicio Top Música Bad Bunny Música Cristiana Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA