Solu Louis, Versace
Gëna fu nooy ngay laaj te
Su ma neexee ma doon Diego Milliardaire
Saoudien bu cace
Maa gëne ñépp ne parfait
Jaru fi coow man la rekk
Maa fiy capo nu ma neexe
Laa koy la koy alligné
Man duma la laal solu be laay doree
Gisago dara xam nga dama coofe
Yow bébé fan nga nekk ñëwel fi eeh
Ñu photo wu snap begge duggel
Tay yaw bësu fête la
Ma àndak babe daadi sol lu swag
Lu rafet kaar, waat nani doo seen mas
Li nga sañse baax na, fi nga gëna nooy na
Loor nga saay noon, uhm uhm uhm
Solul
Def ko nu mu la neexee, yaw solul
Uhm uhm
Solul dagul fu mu la neexe yaw solul
Uhm uhm
Def took jongoma, fi nga gëna neex na ma
Dagul nga doze ma
Yaa fi mëna loolu leer na ma
Ahn li li leeh
Yeah yeah!
Solu bu doon lamb, danga bari bari ba daan ñépp
Samp nga sa ndënd kenn du ko tegg
Yaa leen mëna fepp
Solu bu doon xeex la saa yuñu ñëwee
Ñu feek la seen kow
Ngaleen di duma ñuy doow
Xam naa dowoo coow
Waawaaw, Yàlla may naa la te danga ko xamul
Sa yaram moo rafet ba loo sol manaam daf lay jàpp
Yere olof daf la jàpp
Bu Tubabe daf lay jàpp
Lo xalaat te sola gokoo
Sax ne naa la daf la jàpp
Mo ubbil sa bataan yere yi waad
Nga sol ko def fas kanam
Eh boy bëgg sañse taxuta mëna sañse
Sañse yaa ngi ni
Bëgg jongoma taxuta mëna jongoma
Jongoma ni laa wara mel
Ma mëna solu piir
Damay sañse xeeñ lu neex
Gëna ñu may setaan
Naan xale ba ngi ni
Après mu jeex yow
Yow Jeeba doliñu
Eh oi Jeeba amoo temps
Te maayo Khadim Temps
Temps ma temps disi temps
Tay yaw bësu fête la
Ma àndak babe daadi sol lu swag
Lu rafet kaar, waat nani doo seen mas
Li nga sañse baax na, fi nga gëna nooy na
Loor nga saay noon, uhm uhm uhm
Solul
Def ko nu mu la neexee, yaw solul
Uhm uhm
Solul dagul fu mu la neexe yaw solul
Uhm uhm
Def took jongoma, fi nga gëna neex na ma
Dagul nga doze ma
Yaa fi mëna loolu leer na ma
Ahn li li leeh
Yeah yeah!