Man tànn naa la si jigéen yudul jeex
Jox naa la sama xol bi yaay boroom
Kon baby bul ma négligé maay sa xol
Ndax maa lay jox lépp lu gëne ci yow
Man tànn naa la ci jigéen yu dul jeex
Jox naa la sama xol bi yaay boroom
Bul négligé xamal ni yaay sama xol
Ndax bëgg naa la yow bae bëgg naa la
Man soo manee waaw ma ñëw seen kër
Yow bëgg naa la yow, bae bëgg naa la
Man soo manee waw ma ñëw seen kër
Yow bëgg naa la, bae bëgg naa la
Woo naa la téléphone jëluloo
Envoyé naa la message wuyuwoo
Lan moo tax yow babe lan moo tax
Woo naa la téléphone jëluloo
Envoyé naa la message wuyuwoo
Lan moo tax yow babe lan moo tax
Bu mbëggéel doon jaay
Bu mbëggéel doon jaay
Yow babe jox naa la la xool bi
Waye lépp yaa ko moom
Waye neewul dama ñaak jom
Mësuma ñaak diom
Man sama mbëggéel moo ma yobbu
Moo tax maa lay woo oh
Lan moo tax babe lan moo tax
Su ma lay woo te babe doo ma jël
Lan moo tax babe lan moo tax
Su ma lay woo te babe doo ma jël
Yeah yeah yeah
Yeah yeah yeah yeah yeah yeaaah
Anh anh
Ndax bëgg naa la yow, babe bëgg naa la
Man soo ma nee waaw ma ñëw seen kër
Yow bëgg naa la yow, babe bëgg naa la
Man soo manee waaw ma ñëw seen kër
Ma ñëw ma ñëw ma ñëw
Bëgg naa la yow, babe bëgg naa la