Baye Mass
Je saisis ton amour, je connais ta peine
Dekk nga ci sama xel
Au dessus de nos vies à jamais on s’aime
Maa denk la sama mbëggeel
Jox naa la sama dund jël ko nga dem
Wan ma li nekk sa xel
Si t’es ma source de vie, je reste à terre
Yaw xam nga ni bëgg du dee
Yaw yaay ki jiitu, yaay kiy mujje yaw
Yaay ki may xool sama xol di yëg mbëggeel
Yaa leen gën fuuf, yaa leen ëpp doole
T’es ma sunshine, ma plus que parfait
Bëgg naa la, bëgg naa la, bëgg naa la piir
Yéene naa la àdduna, yéene la àljana ak li nekk ci biir
Je t’offre ma vie comme cadeau et je ferai le pire
Yee nga li nekk ci man
Moo tax dama lay bëgg dugal sama biir (sama biir)
Bëgg naa la, bëgg naa la, bëgg naa la piir
Yéene naa la àdduna, yéene la àljana ak li nekk ci biiram
Je t’offre ma vie comme cadeau et je ferai le pire
Yee nga li nekk ci man
Moo tax dama lay bëgg dugal sama biir (sama biir)
Moo tax ma naan la
Yaw yaay ki jiitu, yaay kiy mujje yaw
Yaay ki may xool sama xol di yëg mbëggeel
Yaa leen gën fuuf, yaa leen ëpp doole
T’es ma sunshine, ma plus que parfait
Su may nelaw ni nga may yeewe
Ëpp doole sama yéene (ëpp doole sama yéene)
Sama dund ni nga ko changer
Waral ma def la Ouroul Ayni
Su may nelaw ni nga may yeewe
Ëpp doole sama yéene (ëpp doole sama yéene)
Sama dund ni nga ko changer
Waral ma def la Ouroul Ayni
Papa Thione suñu yaay di Diaga
Dora Gueye ne na Clara
Pa’ Diouf ne na Bb Bass
Wayee Abba moom ne na Mamy
(La def Ouroul Ayni)
Mouhamed moom ne na Ndoumbe
(Moom mooy Ouroul Ayni)
Hmmm yeah
Yaroo baax yaroo baax yaroo baax
Soo yaroo màcc tangal, yëy sa gune ngay
Yaroo baax yaroo baax yaroo baax
Soo yaroo jiiko yaa ko yee xale bi yaroo baax