Inicio Top Música Bad Bunny Música Cristiana Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA

Letra de 'Yaay Joor (feat. Obree Daman)' de Ashs The Best - Escucha y canta en New Musicas

Varios-artistas

Chilled edm

Varios-artistas

Vibe Check

Varios-artistas

Piano Meditation

Varios-artistas

SAYAS CAPORALES

Artist profile picture

Yaay Joor (feat. Obree Daman)

Ashs The Best

Canciones

Weettay dima ray
Té ñémé wu ma netali
Mangi sama yoon
Ni picc ramatu
Yalla dima wétëli
Goor momul ñaan
Yareewuñu ma tallal loxo
Yaay joor sama yaay
Mangi sakku sa ñaan

Yeurmande amul fii
Wettay ak namel
Nekk ndaw ci samay digg morom yafus waruma
Fii lekkuñu bë sur
Nanuñu bë mandé
Way nekk ndaw ci suñuy digg morom yafus waruma

So yewo yema fallo
So yewo yema fall (yeah)
Fi degn fi nekk ak ngor
Fi degn fi dathie lou metti
Nekk fi ak jom
Fatewouma demb ak Yaay Joor
Wettay si xol la meun yam
Sam khel jougoul si sassmeu
Goné diss neu wayé bo magué fay borr
Lambay soudé meuss neu nekh
Tay Walo amoul ndokh
Touki dou tekki
Gaaday andou tak banekh
Wetna wettay bimay yé
Rerr na fou gnar gni fеgn
Genteu beu dеmb fegn tay
Yéné beu agg
Jooy na fou keine newoul
Dem na ba bougou ma guiss samay rongogn
Ndakh mounou meu bayi limalen diguon
Jambar dawoul daa outi ji wone
Yakar bou tassoul ba tay
Ndakh yoon bi diekha goul
Sama khel ci kasso dou teey dey dem fou dieumeu doul yegg di fey
Wetna wettay bimay yé, anh anh anh
Jooy na jooy guisouma keineu, yeah yeah yeah
Love and peace for me
I can shine, shine like a diamond
Wa wa wa wa wa wa
I can shine, shine like a diamond
Pray for, for me yeah

Weettay dima ray
Té ñémé wu ma netali
Mangi sama yoon
Ni picc ramatu
Yalla dima wétëli
Goor momul ñaan
Yareewuñu ma tallal loxo
Yaay joor sama yaay
Mangi sakku sa ñaan

Yeurmande amul fii
Wettay ak namel
Nekk ndaw ci samay digg morom yafus waruma
Fii lekkuñu bë sur
Nanuñu bë mandé
Way nekk ndaw ci suñuy digg morom yafus waruma

So yewo yema fallo
So yewo yema fall
Ndimbalo yeurmandey fall
Doley biir bek bitti bee fall

Inicio Top Música Bad Bunny Música Cristiana Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA